Yaatu-yaatu, yaatuwaay ak nattukaayu yaatuwaay yi

Yaatu-yaatuk bènn nataal moy wàll gi nekk si biir nataal gògu. 

Yaatuwaayu bènn nataal mooy nattug yaatu-yaatu bi nataal bi di ëmb.

Bènneel bi ñiy jëfëndikoo ngir natt yaatuwaay yi ab kaare la. 

Bènneelu yaatuwaay bi ñiy jëfëndikoo  ngir yombal jëndak jaay yi ak xam xam yi (adduna yëppa si and) mooy « meetar kaare ». Ñu ngi koy binndee m2. 
Am na yeneen bènneelu yaatuwaay. Ñu ngi leen di wone ci alluwaak wecceekaay bii si suuf :

Baatu-tënk yi gënë raññeeku ngir xayma yaatuwaay yi